Fama Thioune parle de l’arrestation de son mari

1487
Advertisement

Fama Thioune se réjouit, comme toute sa famille, après la liberté de son mari, arrêté pour trafic de visa. La jeune animatrice a posté ce message sur sa page facebook. 

« Vive la liberté Sama dieukeur, sama kharite , sama nittou démbeu gui gniou sagal, ki gniou fonk , ki ame sougniou yeuremandé Cherie la brave Femme diambar khalé bi téral ndeyame ak bayame khalé bi mbeugue ayi mbokame khalé bi nago liguéyi khalé bi gueume ya Allah doyilo Seydina mouhamed psl té nope dieukeureume mbeugue dieukeur fonk dieukeureume Gueume borome keureume Fama Thioune borome Télé futur média .souma yalla mbeugué nama bayi ak yawou dama la fan barké cheikh néwone nala sougniou borome keureume dafa bari catégorie té sougniou borome loumou déf amna loutakh

Publicité

Mactar Seck dafa bok si khétou yonéte yalla youssouf té kousi bok dina Diarr prison wala ga dé alkhamdoulilahi c pas la 1er fois gniou dougale nitt prison ( kilifa douguouna prison , serigne dougal nagniouko prison , iman dougale nagniouko prison , kou défoule dara douguouna prison , borome khole bou rafete bakh di dimbalé kharitame douguouna prison kharite bi libre khana lou yalla déf amna loutakh alkhamdoulilahi Mactar sama kharite alkhamdoulilahi .doundalll chéri on t’aime »

Pub

LAISSER UN COMMENTAIRE

S'il vous plaît entrez votre commentaire!
S'il vous plaît entrez votre nom ici