1er Octobre-Anniversaire de Youssou Ndour : l’émouvant hommage de Viviane !

0
992

Suma wayé Yow la,
Numa meel Yow la,
Fuma deem Yow la,
Suma solo Yow.
Numa meel yow yako waral daal cey Youssou Ndour Yow yaay Sénégal….

wax jii jarul muy baarii. Xam nga , mann xam naa.

Yala nala fii yala bayiii nga yagg lol sunu kanam, ci jaam ak salam.

Toujours à l’écoute, toujours prêt à aider VIVIANE .
Mes Vives remerciements pour tout
Et,

Très bon anniversaire au Roi du Mbalakh, mon frère , le Grand Youssou Ndour…
Best wishes m’y bro , Love u!!

#VICSENEGAL

LAISSER UN COMMENTAIRE

Please enter your comment!
Please enter your name here